TRACKSound
El Hadj Thierno Saidou Nourou Tall
11:11 duration0 plays0 favoritesMedium quality
Play now
About this track
Ngir xam lu leer ci seen mboorum réew ak bu Afrig, ndaw ñi dañoo war a miin jàmbaar yi tabax Afrig. Ndégat yii di Podcast, xam sa démb, xam sa tey », looloo tax ñu tànn yenn ci jaar-jaar ak xew-xew i mboorum Senegaal, ngir may ndaw ñi ñu jàngee ci seen démb, baa man seen tay, te waajal seen ëllëg.
From the album
Xam sa démb, xam sa tey25 tracks · Track 12Ngir xam lu leer ci seen mboorum réew ak bu Afrig, ndaw ñi dañoo war a miin jàmbaar yi tabax Afrig. ...
→




















