TRACKAbout this track
Ngir xam lu leer ci seen mboorum réew ak bu Afrig, ndaw ñi dañoo war a miin jàmbaar yi tabax Afrig. Ndégat yii di Podcast, xam sa démb, xam sa tey », looloo tax ñu tànn yenn ci jaar-jaar ak xew-xew i mboorum Senegaal, ngir may ndaw ñi ñu jàngee ci seen démb, baa man seen tay, te waajal seen ëllëg.
From the album
Xam sa démb, xam sa tey25 tracks · Track 5Ngir xam lu leer ci seen mboorum réew ak bu Afrig, ndaw ñi dañoo war a miin jàmbaar yi tabax Afrig. ...
→










![[Alexandros] cover art](https://pbcdn.aoneroom.com/image/2026/06/04/95f1de08a056f636d56e27f302d739d9.jpg)









