Njariñu KoorTRACK

Sound

Njariñu Koor

36:28 duration0 plays0 favoritesMedium quality
Play now

About this track

Waxtaan wii Imaam Xasaali dafa ciy wax njariñ yi ci koor ak yiiw yi mu man a fàggul jullit bi, waaye tamit leeral dayo bi koor am fa saa Boroom.

From the album

Bëgg a Baax podcast album coverBëgg a Baax podcast9 tracks · Track 3

Li tax a jóg Bëgg a Baax podcast mooy yaatal mbaax. Képp koo xam ne mbaax ñor na la, nu ngi la ciy d...

→

More By Cheikhouna Diaw...

You may also like

Blackwülf Radio cover art
Blackwülf RadioDuskwood, Sergeant Thunderhoof, Margarita Witch Cult, Blackwülf, Saint KarloffMusic