Waxtaan ci borTRACK

Sound

Waxtaan ci bor

13:41 duration0 plays0 favoritesMedium quality
Play now

About this track

Ci waxtaan wii, da nu ciy leer dayo bi bor am ak diis bi mu diis, ngir fàttali sunu bopp, waaye fàttali sunu bokki jullit yi ngir ñu jàjju te moytu bor boodut fay.

From the album

Bëgg a Baax podcast album coverBëgg a Baax podcast9 tracks · Track 7

Li tax a jóg Bëgg a Baax podcast mooy yaatal mbaax. Képp koo xam ne mbaax ñor na la, nu ngi la ciy d...

→

More By Cheikhouna Diaw...

You may also like