TRACKSound
Teggiini niti Yàlla yi (Xaaj bu njëkk bi)
26:43 duration0 plays0 favoritesMedium quality
Play now
About this track
Waxtaan wi ab jukki la ci téereb kàngam boobu di Imaam Saaraani. Ci téere bi dafa ciy jàngale teggiini niti Yàlla yi yoy képp ku sóobu ci Yàlla te bëgg a bokk ci góor ña war nga leen ca roy.
From the album
Bëgg a Baax podcast9 tracks · Track 4Li tax a jóg Bëgg a Baax podcast mooy yaatal mbaax. Képp koo xam ne mbaax ñor na la, nu ngi la ciy d...
→


















